pic

Informations about Pullo Àrdo

Select a Genre :

enter artist/album/song to search lyrics for:

Rating: 1.0/5 (1 vote cast)

Koufi gneuw mu diangal la
Niax mi môko môm
Ndokh mi môko môm
Daf ko donn
Lî khar yi la
Lî beuy yi la
Nagam yangui
Àll bâ ngui
Baxi mâmaw Poullo Àrdo
(x2)

Pullo-Ardo pullo-djèry pullo-ardo
pullo-djèry Pullo-Ardo pullo-djèry

Dakhal yi mu jeum fé
Nga dakh yé mou jeum fi
Yâ xam yaw li khèw fé
Dara diaxa loula fi ba fé

Pullo-Ardo pullo-djèry pullo-ardo(x2)

Ardo sékhna guëneum
Daldi gaddu yatam
Ma nga anddak khadjam
Daldi djitël guéteum
pullo-djèry Pullo-Ardo

Mingui anddak khdjam
Daldi djitël guéteum
Dalal xélam
[Pullo Àrdo lyrics on http://www.01lyrics.com ]
Féxal xolam
Bou nit gniy fo aka ré môm yëguko
Souy
Pullo-Ardo pullo-djèry

Lépp am mingui fi
Fî la yarô
Fî la magué
Téyit fî la
Také soxna
Lépp am fî la
Pullo-Ardo pullo-djèry
Bu nit gniy teub aka dal môm yëguko
Limu am fî doy nako té doylô nako
Boudè or la
Mba jamâ
Wala étage la
Mba avion la
Mba lénène la
Môm guissouko Pullo Ardo

Ma nga gaddu tôkhôr om
Di mbîb mbîb yu am khôrôm
Waye waye yu amoul môrôm
Mél ni kouy nèkhal gôrôm
Bofa diarè sant sarr è dinala rè
Bofa diarè dône sérère è dinala rè
(x2)

Comments about Youssou N'Dour

kirikou je vous aime de toute mon coeur

Posted by awa gueye on 2008/08/10 23:51

This is a great song! I love it

Posted by Jaye on 2007/12/08 21:02

Copyright 2007 © 01Lyrics.com - Contact - Link us - Privacy Policy - Contenu for webmasters