enter artist/album/song to search lyrics for:
Refrain:
Na nga def yaw sama gàmmu
Dég na danga yor khalis
Khamna ni yaw momouloko dang ko abb mba nga forko bâl dôzé tèyal.
Refrain Bis:
Na nga def yaw sama gàmmu
Dég na danga yor khalis
Ba foma sèn tambalé weuliss
Khamna ni yaw momouloko dang ko abb mba nga forko bâl dôzé tèyal
Yor khalis meunoul tè ma môm la
Keur gou rich meunoul tè ma môm la
Yaw na nga def yaw sama gàmmu
Dég na danga yor khalis
Khamna ni yaw momouloko dang ko abb mba nga forko bâl dôzé tèyal
[Sama Gàmmu lyrics on http://www.01lyrics.com ]
Kay gâw wakh ma nô def ba am ko
Fok nâni nita ko waddal nga forko
Wakh ma gâw niata la bama fayko
Man dâl mây sa bour nangu ko
Refrain Bis
Annh souniy mâme
Nonou lagn ka dân défé
Annh souniy bâye
Nonou lagn ka dân wambé
Annh souniy yâye
Nonou lagn ka dân topé
Annh gàmmu dâl
Sama dômu ndaye nga
...
kirikou je vous aime de toute mon coeur
This is a great song! I love it
Copyright 2007 © 01Lyrics.com - Contact - Link us - Privacy Policy - Contenu for webmasters